![]() |
Xam sa démb, xam sa teyAuthor: Goethe-Institut Language: wo-sn Genres: Society & Culture Contact email: Get it Feed URL: Get it iTunes ID: Get it |
Listen Now...
Gorée
Episode 10
Monday, 23 February, 2026
Ngir xam lu leer ci seen mboorum réew ak bu Afrig, ndaw ñi dañoo war a miin jàmbaar yi tabax Afrig. Ndégat yii di Podcast, xam sa démb, xam sa tey », looloo tax ñu tànn yenn ci jaar-jaar ak xew-xew i mboorum Senegaal, ngir may ndaw ñi ñu jàngee ci seen démb, baa man seen tay, te waajal seen ëllëg.





